Categories
Covid Regole e comportamenti

DCPM DIEUME 3 DÉCEMBRE MOY DPCM NATALE

21/12/2020 DIEUME BA 06 /01 2021 .TÉRÉNANOU  GUÉNE 22HEURES DIAP 5 HEURES SI SOUBA

01/01/2021 TERENANOU GUÉNE 22HEURES DIAP 5H SI SOUBA

SI BENE GOKH MEUNE GUA DEM SA BENENE KEUR SOUFÉKE TAMITE BENENE GOKH LA BEUSE BOU NÉ 25 25 DÉCEMBRE AK 01 JANVIER 

WAYÉ 24 DÉCEMBRE DIAPE 06 JANVIER KÉNE MEUNE NA GUÉNE PAR BEUSS DIEUME NIARI NITE BOU FÉKKÉ NOBOK FINOU DIEUME KENE WALA NIARI NITE YI GUENE  MEUNENANOU ANDAKH SEN DOM BOU AME 14 ANS WALA DIAFEDIAFÉ KO NÉKOULALE 

REWMI ITALIE YEUP KHOK LA  BATAKHNA TÉRÉNANOU KOUY DOKH KANA MOU FARLOU DEGUA ANDAKH CAYITE BOUYE FIRDÉLE 

DINANOU TEUTHIE DIATE BERRABOU DIAYE BAR RESTAURANT DAFARE YARAM BA 22 HEURES NGI YOBOU LEKK

AMOULE WAKHTOU 

DINA HIBI SUPERMARCHÉ  FOUNOUYE DIAYE LEKK FARMACIE  JOURNAL WATE SIGARETTE  FAUTOUKAYE

REWMI ITALIE YEUP ZONE ORANGE  MEUNE GUA GEUNE DIEUME  BANENE GOKH SOLANEKHE

TEUTHIE BAR RESTAURANT DIEUME 22HEURES  WAYÉ NGI DIOKHE LEKK SAYOULENE NEKHÉ GUENE

HIBI BEP BERABOU DIAYE BA 21H