Categories
Covid Evidenza Salute

NANE NANOUYE DAF BA NDIAKHOU

Categories
Covid Evidenza Regole e comportamenti Salute

WEUR NIAKHOU COVID-19

WEUR NIAKHOU COVID-19 

  • TAMBALINA SI REW YI UE NIAKHOU BEUSSOU 27 DÉCEMBRE 
  • YANE NITE NANOU DIOKH PRIORITE SI NIAKHOU
  • YI LIGUEYE SI WALOU WEERGOU YARAM WALA NDIMBEUL LIGUEY KATEYI
  • NGI DEUK MAK YI WALA TOPOTO LENE (RSA)
  • MAK YENE ATE SORI

 BATAKHAL POUR NIEUP, NIAKHOU AR FEBBAR BI COVID-19  AMOULE FAYE

 NIAKHOU COVID-19  AMOULE REWMI WALA KOUFI BOKOULE

  • NIAKHOU COVID-19 KEL DOUKO NIAK KHALÉ BOU AME 16ANS 
  • NIKHOU COVID-19 DOULOU WARA NEK WAYÉ AMENA SOLO DAKH DI NA WAGNI NITE SI AME DIAGOROBI
  • LÉGUI NIAKHOU NAGOUNANEKO SI EMA NIARI YONE SI SEMAINE NOU NIAKHLA AK KHETOU NIAKHOU
  • NI DI LIGUEY SI WALOU FEBBAR BI  COVID-19 DINANOU NIAKHOU TAMITE

YOKOU KHETOU NIAKHOU TAMBALI BÉP CATEGORIE ASKANE

AME SILOU LEER WALOU BEUSSOU NIAKHOU SI COVID-19 ( DINANOUKO DAF)

FONTE FAQ Sitò gouvernò

Categories
Asilo e immigrazione Evidenza

LOU BESS DIEUME KOUYE LATHIE LAKHOU SI REWMI

LOU BESS DIEUME KOUYE LATHIE  LAKHOU SI REWMI

TAMBALI 20 DÉCEMBRE 2020 KHATIME NANOU CHARTE  n173  ANDINANOU LOU BESS DIEUME SI DIOGUÉ SEN REW NIEUW SI REWMI 

LOU BESS 

BINDOU NOU RAGNELA

ARTICLE NIARE 2 T U IMMIGRAZIONE 

NGI LATHIE TE YOR CAYITOU  LATHIE MEUNANOU DIOTE (CAYITOU FAYE)  NOU BINDOU FI NOU DEUK 

Categories
Asilo e immigrazione Evidenza

YOKOU BI DIEUME SI CAYITOU REWMI BI

BEP CAYITE BOUNEK SI YONOU NDIÉKH DIAPE 30 JANVIER 2021 BATOLOKH 30 AVRIL 2021 DINA LEK MOYE YOK BA DIÉKH TALOU 30 AVRIL 2021 (KHATEMA BOU BESS n/2021)

Categories
Asilo e immigrazione Evidenza Lavoro

LOU BESS SI CAYITE YOUNOU SOPI DÉFKOU CAYITOU LIGUEYOU KAYE

LOU BESS SI CAYITE YOUNOU SOPI DÉFKOU CAYITOU LIGUEYOU KAYE 

DIAPE  LE 20 DÉCEMBRE 2020 DOUGOUNE CHARTE SI YONE 173 THIOPETE YOU AME SOLO SI WALOU NÉKINE SI REWMI 

SOPÉKOU YI

NGI YOR CAYITE DÉ NOU FASNEKOU DEF CAYITOU LIGUEYE 

BENE SI KHARMAYI 6 YOKNANOU CAYITOU MÉUNE SOPI DÉFKOU CAYITE LIGUEYE KAYE AME LOUMOUY LATHIE

YENE CAYITE DIEUME SI DIANGA MEUNE KO DEF CAYITOU LIGUEYE 

CAYITE HARE ADOUNA BI YEUP ((LOU DIEUME SI ADUNA DIEUF YOUNOU DAK 10  KHATIME 2

CHARTE 251/2017 LOU ANDI DIAKHARÉ SI REW SI  CHARTE 12 

CHARTE 251/2017 MOUBOP KHATIME16 CHARTE 251/2017   

CAYITOU DIEUME SI BEUGUELE

CAYITOU DIEUME  SI RÉSIDENCES  ÉLECTIVES 

CAYITOU DIEUME SI DIEUNEDE LIGUA DONE APATRIDE

CAYITOU DIEUME SI WALOU TAGUAL YARAM 

CAYITOU DIEUME SI  WALOU ARTISTE

CAYITOU DIEUME SI WALOU DINÉ

CAYITOU DIEUME SI WALOU ARE KHALÉ 

CAYITOU DIEUME SI WALOU FADIOU