Categories
Asilo e immigrazione Evidenza Faq

LANE MOY ANDI SA NJABOOT ? MOY ANDI SA NJABOOT SI REWMI ITALIE SI YONE BOU LEER

LANE MOY ANDI SA  NJABOOT ?

MOY ANDI SA NJABOOT  SI REWMI  ITALIE  SI YONE BOU LEER

EUNE GUA SAKOU ANDI SA NJABOOT AK YI TOP SA NJABOOT 

 

  • DIEUKEUR AK DIABAR YOU TAGOTOWOULE DASÉN ATHE TOLOKH FOUK AK DIOUROME NIATE 18ANS WALA KO NECAL ( ITALIE  AK FENENE) DOU DOMOU REWMI DECOULE SI REWMI ITALIE 
  • DÔME SÉN ATE MATOULE  BO DIOUR FATKODI SENBIR KOU DIOUDOHOULE SI DIGUENTÉ BI DÉ KÉN SI NIOME D’ACCORD 
  • DÔME BOU AYE ATAME MATE MEUNE GUAKO ANDI DÉDOU AME DIAFEDIAFÉ LEUPP DIAR YONE
  • WADIOUR MEUNE GUA ANDI KOU AME 65 ANS FÉK AMO YÉNENE DÔME YOUNEK SI REWMI WALA LI KO WER
  • WADIOUR MEUNE GUA ANDI KOU AME 65ANS FOUFEKE SAKH AME AY DÔME SI REWMI NOU NEK DIAFEDIAFÉ SEN CAYITOU WEERGOU YARAM 

 

SO AMÉ 18ANS  DA KENEGUA WALA GUA TAGO AK SEY WADIOUR WALA BENÉNE FAMILLE BOLAYE TOPEUTO DIAPÉLA KOME WAY LAKHOU SI REWMI MEUNE GUA ANDI SAY WADIOUR WAKH SENE ATE AK SEN WEERGOU YARAM

CAYITOU REWMI  MOUYE LATHIE WALA DJÉKH FIAKH 60JOURS  DÉFAR 

PASSEPORT WALA CAYITOU  TOUKI

LOUYE FIRNÉLE KHALEGUA DÉNOU AME SI NDIGUEL  WADIOUR YI KHALE BI

 

SOUFÉKE DAGUA AME HAROU WA ADUNA DUNLA LATHIE CAYITOU FAYÉKOU SOYE LIGUEYE

NOKO TEUK SI NIARI PATHIEU LATHIE NULLA OSTA GUA DOW FINOUYE  BINDOD DAGUEK NOUFI DE NGI KHARAGNE SI LIGUEY BI TOPEU BEP DIGUELE NGI NÉKAL WA REWMI SIBITI 

LATHIE NULLA OSTA WARGUA AME

  

   ▪︎AME MADARGUA SPID DE WAKHOU SI POSTE WA REWMI

     ▪︎WOR TIMBAR BOUYE DIAR 16€

     ▪︎DIEUDIKO SPID SAY YOULEU NÉKHE DA DO FAYE DARA SI BÉRRABI 

BINDEU SI CAYITE AK NUMÉRO TIMBE BISI KAO BI ANDAKH

 

BOU WESSOU DINALA WO GUA NIAW FI SAYTOU BIROU CAYITE ANDAKH SEY FIRDÉLE 

  ▪︎TIMBAR BOU BAKH DE MEGOL LIGAUY LATHIE 

   ▪︎AK BENENE TIMBAR 16 € DIEUME SI NULLA OSTA 

    ▪︎ CAYITOU REWMI AK FOTOCOPIE

    ▪︎CAYITOU DJABOOT  YI GUE BEUGUE ANDI SI REWMI 

DINANOU NAGOU CAYITE WAKEUR YI DEUK FANOUNEK (SI FORME BARAKHAL)

SOKO DIOTÉ NULLA OSTA GUA ENVOYÉ  ORIGINAL NJABOOT BI WARA NIEUW  DANOU WANÉKO WA REWMI ITALIE DE DOU YAGUE DARA GUA DIOTE BATAKHAL BOU DIOGUÉ SI NGI TOPEUTO  BIIR BI

GUA DIOTATATE  BATAKHAL  BOUNOU BINDE DIEUME SI  LOYE LIDIEUNE TI NOUWAKH LA BEUSS AK SA NJABOOT DOUGEU SI REWMI TOLOKH 8JOURS NDAKH NOUNEUNE TOPETO CAYITOU NJABOOT GUI

BOU LEPP DIARE YONE DINA AME 90 JOURS TOLOKH AK SA LATHIE NULLA OSTA DIOUBLOU SI ANDI BI SOUFÉKE NAK LATHIE BI NAGOUNOUKO NULLA OSTA AMEGUE YONE DOGUELA  DIEBALAKO TRIBUNAL BI KAY GUESSTOU 

 

YONE MAYNALA BA 30JOURS  WAYE NEUNA EUPEU TAMITE LOUNOU WAK

 

A CURA DI CARITAS ITALIANA CONSORZIO  COMMUNITAS UNCHR  BO BEUGUE LEER DAMALE

 

http/ricongiungimento/it

 

Www.nullaostalavoro.dici.interno.it