KHATE BÉRÉP YI

Share on facebook
Share on twitter
Share on whatsapp
Share on telegram

KHATE BÉRÉP YI 

BOUKOFÉKE CHARTE BI TEURELÉ  WANE BINEDOU REWMI ITALIE AK KI COLORE YAME ( GOKH YI  KHOK ROUGE ORANGE MBOK JAUNE WÉKH BLANC )  AK TEUREL YOU MOUDIOU YONOU YOUWADIEU NIEUW 

BÉREP WÉKH BLANC
Abruzzo, Basilicata, Calabria, Campania, Emilia Romagna, Friuli Venezia Giulia, Lazio, Liguria, Lombardia, Marche, Molise, Piemonte, Provincia Autonoma di Bolzano, Provincia Autonoma di Trento, Puglia, Sardegna, Sicilia, Toscana, Umbria, Valle D’Aosta, Veneto

BEREP YOU JAUNE

BÉRAP ORANGE

FI KHALÉ DI FOWÉ DI HIBEKOU

 BÉREP WÉKH BLANC

  • TAMBALI 7 JUILLET  24 HEURES  DIAP 5HEURES  SI SOUBA TAMBALI TOKH SI  BIR KEUR YI  21 JUILLET BERÉP MBOK NA NIOU BAYI GEUNE GUENE
  • DINANOU IBI BERRABOU DIAYE YOU MAKI AK BESS FETE AK SOU NEKOULÉ FETE
  • IBI FINOU DETHIE  BAGASS LOU YAGUE YI 
  • LEKK SI BIR BAR RESTAURANT  AGNE AK RÉRE
  • DIETALOU 1 JUIN DINANOU THIEU FEB NIOUYE WOUTE KHALIS AK FINOUYE DIAYE SIGARETTE  AK BAR
  • IBI BÉREBOU FOHOU KAYE KHALÉ YI (1 JUILLET NO THIEUTE BEREBOU TANGUAL YARAM YI AK THEATRE AK CINÉMA

SOUFÉKE DAGUA BEUGUE GUÉNE DEM AK LOUMOU MEUNE DONE WARGUA WANÉ FIRDÉLE ?
WAKHTOU 5H BA 24H DIAROULE FIRDÉ WAYÉ 24H BA 5 H FOK GUA AME FIRDÉ BOUYE WANÉ DAGUA WARA GUÉNE

MEINENA DÉME DIMBALI XARITE WALA MOK BOUSOKHLA DIAPALÉ ?
WAW SOUFÉKE LOUMEUTE NIAK WAYÉ DIGUENTÉ 24H BA 5H AME FIRDEL DINANKO SOLO

SOUFÉKE DAMA TAGO WALA TASS MEUNENA SÉTI SAMAY DÔME ?
WAW MEUNE GUA FÉKI SAY DOME WADIOUR NAGUA TÉLA GUÉNE YOBOULÉ SI BÉNENE GOKH AWÉNOUKO

MEUNENANOU DEM SI BÉRÉBOU DIAMOU YALLAH YI ?
WA KHANA LOUDIEUME 5H BA 24H

SOUMA DEUKE FENE DI LIGUEYE FENENE MEUNA DEM DI NIEUW ?
WAW

KOUNÉK FIGUA DEUK NAK MEUNE GUA NGIBISI ?
WAW

This page is also available in: Italiano (Italian) English (English) Français (French) Shqiptare (Albanian) العربية (Arabic) Español (Spanish) বাংলা (Bengali) 简体中文 (Chinese (Simplified)) Punjabi (Punjabi) Русский (Russian) Somali (Somali) اردو (Urdu) አማርኛ (Amharic) Tigrinya (Tigrinya)

NANE NANIOU RAGNÉ MANDARGUA?

This page is also available in: Italiano (Italian) English (English) Français (French) Shqiptare (Albanian) العربية (Arabic) Español (Spanish) বাংলা (Bengali) 简体中文 (Chinese (Simplified)) Punjabi (Punjabi)

Meuna Tak

LOUYE TAKH GUA TOUKI

GREEN PASS (WALA BATAKHAL BOU VERTE) SI EURPOE UE WALOU  FEBBAR BI COVID BATAKHAL CAYITE TOUKI AK DIAM SI ITALIE AK EUROPE BATAKHAL BI DINA