LOUYE TAKH GUA TOUKI

Share on facebook
Share on twitter
Share on whatsapp
Share on telegram

GREEN PASS (WALA BATAKHAL BOU VERTE) SI EURPOE UE WALOU  FEBBAR BI COVID BATAKHAL CAYITE TOUKI AK DIAM SI ITALIE AK EUROPE BATAKHAL BI DINA DOKH FÉP SI ITALIE AK EUROPE BI BESSOU 1 JUILLET 2021

DIAP 6 AOÛT SI WÉR BI DI NIEW LOU NOU WARA AME LA AK GOKH YOU WÉKH ZONE BLANCHE 

– LEKK SI  TABLE RESTAURANT AK BAR BOU TEUTHIE

-DIALE SI BERÉBOU KHOL BIR YOU YAGUE DIAMONO 

– MEUNE FÉKKE FETHIE WALA WAY YI NOUYE AMAL POUR NITEYI AK YENE KHETOU RAWANTÉ

– MEUNE BOK SI KHOUMBAYI TEUTHIE DIEUME SI WZLOU CULTURE  SOCIAL  ART (WAYE FI KHALEYI DI FOWÉ BOCOUSI BIRBI

– MEUNGUA DOUGOU SI DEFARÉ YARAM AK YENE BERÉBOU SPORT YI WAYE (PISCINE PALESTRA AKFI NITE YI BOLO DI TAGUAL YARAM ) TEUTHIE BERÉBOU  YARAM

– MEUNE GUA DOUGOU BERÉBOU FATHUE RSA

– DOUGOU BERÉBOU TANGUA DER AK KAF FO

– MEUNGUA NEK DADIÉ LEKk ANDAKH DIEUDEU AK DIAY YI FA NEK

– BOK SI DADIEYI AK KHOUMBAYI 

– BOK SI RAWANETEYI 

– BOK SI FI CARTE KHALE AKTEK KHALIS  CASINO AK YENE


BATAKHAL BI MINISTÈRE BI YOR WALA WÉROU YARAM MOKAYE DIOKHÉ SI BERÉBOU DIGITAL AK SAYTOU

MEUNGUA LATHIE WALA GUA AME:

– GUA DE SI SITE  dgc.gov.it AK SA SPID WALA SA TESSERA SANITARIA  WALA LOU FIRDEL YAW LA

– AK APP IMMUNI

– AK APP IO

– DOUGOU SI BIR BERÉBOU TOPOTO WALOU WEERGOU YARAM ÉLECTRONIQUE 

– DEM KI FATHIE SA WA KEURYI  FATHIE KHALE BOMOUTIDONE WALA PHARMACIE

SOUFÉKE BIDOUHO SI WALOU FATHIE MI MEUNGUA BATAKHAL BI  DI CERTIFAZIONE SI SEN SITO BI DI Certificazione verde COVID-19 GYA DEF SA CODE ( AUTH CODE ) GUA DIOTE SMS  EMAIL SI NUMÉRO CAYITE BIGUA DIOKHÉ BAGUAYE BINDO DI DAF TAMPON WALA CAYITE WERGUE


NIANE NOMEUNE AM CERTIFICAZIONE  ?

CERTIFICAZIONE DAY NIEW AUTOMATIQUE  SI FANAYI

a) NDIAKHOU 1 DOSE  WALA NDIAKHOU DIAP 15 JOURS

  • NOUNAGOUKO  FI ATE GUA NDIAKHOU NIAREL  DOSE ( DIAPE BOLE DIEULE NIAR) WALOU 9 MOIS NDIAKHOU GUÉNAWALA DOSE
  • CERTIFICAZIONE DINANOULAKO DIOKH SI FORME DIGITALE WALA CAYITE  CARTEL 15 JOURS SA NDIAKHOU  ( NOU LATHIE NIARI NDIAKHOU) SIGUENE WALOU NDIAKHOU

b) GUA DAF NDIAKHOU YEP

  • NAGOUKO 9 MOIS
  • BATAKHAL DINAKO DIOKHÉ SI FORME DIGITALE WALA CAYITE  CARTEL15 JOURS NDIAKHOU LEP GUENOWALO NDIAKHOU NIARI FAN NIARELOU NDIAKHOU

c) NER SI FEBBAR BI COVID-19  DE DIÉKHEL TEK FEN ISOLÉ 

  • BAKH 6 MOIS FÉK WÉR GUA
  • GREEN PASS  DINANOU DIOKHE DIGITAL WALA CAYITE  CARTEL  FIGUA AMENE KI FEBBAR WÉR WALA DÉTE SI KI SAYTOU WEERGOU YARAM TAMBALI BEUSS YOIMOU WERÉ

d) DAF TESTE BAKÉNE AK NGUÉME DÉ MOWANÉ AMO COVID-19 

  • DAKH 48 HEURES BIK DUEULÉ
  • GREEN PASS DINANE LAKO DIOKH SISASI (NOU NEK FORME DIGITALE WALA CAYITE CARTEL) BEREBOU FETHIE PRIVÉ WALA PUBLIC  FARMACIE  KI SAYTOU SA WEERGOU YARAM
Pidgin English
Pular
Soninke
Bambara

This page is also available in: Italiano (Italian) English (English) Français (French) Shqiptare (Albanian) العربية (Arabic) Español (Spanish) বাংলা (Bengali) 简体中文 (Chinese (Simplified)) Punjabi (Punjabi) Русский (Russian) Somali (Somali) اردو (Urdu) አማርኛ (Amharic) Tigrinya (Tigrinya)

NANE NANIOU RAGNÉ MANDARGUA?

This page is also available in: Italiano (Italian) English (English) Français (French) Shqiptare (Albanian) العربية (Arabic) Español (Spanish) বাংলা (Bengali) 简体中文 (Chinese (Simplified)) Punjabi (Punjabi)

Meuna Tak

This page is also available in: Italiano (Italian) English (English) Français (French) Shqiptare (Albanian) العربية (Arabic) Español (Spanish) বাংলা (Bengali) 简体中文 (Chinese (Simplified)) Punjabi (Punjabi)

DONOU DOUMOU REWMI WALA FATELA

This page is also available in: Italiano (Italian) English (English) Français (French) Shqiptare (Albanian) العربية (Arabic) Español (Spanish) বাংলা (Bengali) 简体中文 (Chinese (Simplified)) Punjabi (Punjabi)