Categories
Asilo e immigrazione Covid Regole e comportamenti Salute

Green Pass yi di ligueye lane nanou wara khame 

 

tambali 15 octobre 2021 bép lugueykaye gour gui wala guaye ligueye sa top wargua am green pass (certification verde)ndakh gua meune nék fi guaye ligueye  amna berale nite

 

 

•  ngi gua khamné dano febar dé meunouno niagou  ki saytou sen weergou yaram defalene cayitou bou kaye firdel dé nouye def tampon de bagne faye dara

 

•  ak ligueye kate nék sén ligueye bop

 

 

Louye khéw ligueye kate you amoule green pass 

 

–  ligueye kate ngour gui de andoule green pass meune nanon diap kheuye si ounou  batakhna 

(sén wareef ak ligueye yorko )

dé teou sa berébou ligueye youkaye melnani tokh dé ligueye sa bess bou nieuk 

 

–  ngi ligueye dakh nite de amoule green pass donou kheusi (sén wareef ak ligueye yorko)babanouye andi certification verde ngi ame 15 ligueye kate yone maynalene nou wakh ngi amoule green pass tokh sen keur ba nousouye diote

 

 

–  niane noy def setlou si ligueye katyi ?

 

khana  ngi mome  berébou ligueye youkaye yi diap 15 octobre setgui nek si bir berébou ak sibiti nou kham nane nanouye dafé 

 

–  ngi khamné noye ligueylou sene keurgui ( dokh courant  ak yene khetou technique) nionou warounou lathie green pass dakh te kilene ligueye lo nouwara farlou nou am green pass 

 

 

dane ak lane molasimeune fék 

 

meune la dane 600 ba 1500€ si ligueye katyi nék walou privé  danou wara nior green pass 

Tampon mégole 

meungua am green pass soufeke dafgua tampon ( dinanou nagou tampon rapide bou 48h  wala bou guenine bi am 72h ) de pharmacie diko def damou nourokh 15€ khaléyi wéssou 18ans  8 € diap khaléyi sén ate diap (12 ba 18ans)