Categories
Asilo e immigrazione Minori Regole e comportamenti

Khalé yi nane lene andi si wala famille ak si bir Europe

Khalé you noi andi bir réwmi italie ame fi wadiour ak bénene deuk europe meunanou lathie bolé djaboot andakh topato bou weur de do fay dara  batakhal yeup wa cidas ak unhcr dinale leer bep lo beugue khame si aname you leer

si sa akh ak nane guaye de ba djaboot nieup fekasila ngi topoto biryi  si 9 lakk  yeup nadiowakh 

Categories
Covid Regole e comportamenti Salute

Yi diagou lanou wakh mo bakh si covid-19 dé gya meusi am sa green pass si réwmi italie

Yi diagou lanou wakh mo bakh si covid-19 dé gya meusi am sa green pass si réwmi italie  

 

  • covidshed (serum brrebou inde )

 

  • r-covid (r-pharm)

 

  •  covid-19 vaccine -recombinant (focruz)

 

Meune nandio kham si niane la bakh

 

 

 • wa doumoiu réwmi mi italie ( you fi nek wala bitim rew) ak noufidounak sen djaboot 

 

• ak nek si réwmi di fi ligueye danoi diogué benene rew de bindou si berébou fadioukaye  “sasn” (yi topoto fathie nite si touki)

 

 •  bep der bou bindou si berébou fadioukaye de niagou fénene  nakh khékh sars cov-2

 

Certification niagou dina mégole  certification verde covid-19 (certification covid  bou bess  dé boutaye ue ) diokh ko rew Italie.