Categories
aiuti sociali Evidenza Minori

Dénthie Dakh

Dénthie dakh njaboot gui  nieup la war dé nek ndimbal de khale yi ndaw khaliss bou nouye diote banouye mague didap 21 ans 

 

Yok ndimbal  inps nokoye ndiékhal si sa am am dolé  ( isee) am yok ndimbal meunenanou bindou le 1er janvier 2o22 inps wala ngi yorbirou ligueye  yok ndimbal bi mogui diokol ak inps mars 2o22 

 

meune gua lathue yok ndimbal fi  30 juin 2022 de moutolo fi wér  ( mars  2o22)

 

Kane moneune lathie yok ndimbal 

 

 

Bobeugué lathie yok ndimbal lane guaye ame 

 

gua nék  wa réwmi wala rewou europe (wala njaboot) wala gua nék kou bokoule rewou europe dé guame cayite réwmi  ue ak gua yague lol si réwmi  wala sa caite nék  di ligueye  lou wessou 6 mois tamite cayite  ligueye bou yague si rewmi 6mois 

—   sa faye biguaye diote si réwmi 

—  wala gua def si réwmi loutolok 2ans  dé figuaye ligueye  amgua cayitou ligueye bou yague wala ligueye  bou wéssou 6 mois 

 

 

Li mégole yok ndimbal 

 

•  yok ndimbal nieup la war – bep khetou fayekou ameuna  si yone — topanté — yok wagnékou amam isee 

 

•  yok ndimbal meune guako lathie 120 jours si dioudou dom ak khalé bi matate 21 ans dom bou nek

 

•  khaleyi am 18ans ak yi 21 ans matoule ndakh yok ndimbal lew lane 

 

°  guay def école formation  professionnel wala gua ame diplome 

 

°  tambali ligueye def fayékou ate bounek 8 000 € 

 

°  sa ligueye  takhaw dé kheur ligueye 

 

°  ligueye de nieup zm si yone

 

•  sodefe lathie si ba wér  mars fi zk 60 bess di nala yeugeule

 

•  yok gui dina diar si iban wala yoksi keurgui reddito di cittadinanza 

 

•  yok gui bokoule dara ak reddito njaboot gui

 

NB   nouteguale si bi lathie tambale walele certification isee gua meuna diote yok propostion  bousa lathie andoule ak certification   isee inps linkaye diote dina niew siwalou reddito 

 

lou megoule yok ak yenene ndimbal 

 

diap fi mars 2o22 yok ndimbal dieume njaboot ak domyi

 

–  yok ndimbal  dieune si diote khale ( yok yaye souba)

yok ndimbal khale yi sogua dioudo ( yok liryi ) ak anf (yoké njaboot) nou bolesi khale yi ame lou wésou 21 ans

 

–  yok ndimbal nouro na ak reddito di cittadinanza wala yok khalé 

 

nb soufeke sa reddito di cittadinanza akyok ndimbal njaboot authentique nane koye dakh

 

 niata la tolok si yok ndimbal 

si lnk meugya calculer yok sk inps 

hppts ://servizi 2.inps .it/servizi/ assegno unicofiglio / simulatore 

 

diarigne yi am si yok ndimbal njaboot 

 

sou diote amoule brnf cayitou réwmi nou sopi si yok ndimbal dieume si page bi

 

nane na nouye dff bame lathie

 

def lathie diarna gua dougou sitou inps 

hppts ://servizi web2.inps.it passiweb/jsp/spid /login/spid .jsp?uri =https%3a%2f%2f servizi 2.inps .it%

 

wote le si numéro 803164 ( fixe  ) 06 164 164 ( sa téléphone) wsla yene caf inps nagou 

hppts ://www.inps .it / servizi=online /servizi =per =patronati/ informazioni / gli= enti- di – patonato

 

soufeke dego lak réwmi de gua sokla kou lako lak si sa kalama wotel  numéro verde  lathie asile ak réfugié  ( arci)  800 905 570 lycamobile  351 137 63 35 

assegno unico
Pidgin English
Bambara
Pular
Soninke
Categories
Covid Evidenza Salute

Diklé niagou green pass charte tambali 10 janvier 

obbligo vaccino over 50

 

Diap 10 janvier 2o22 tambali charte dieume si niagou ak si walou green pass  niane nanou diklé niagou ? kagne nanoulaye diaklele super green pass ak kagne laye mate bagua yor sa green pass base? yenayou bess dieume si charte di diekh fi ba 31 mars 2o22 wala fiak diafediafé di diekh 

 

 

Diap 10 janvier tambali dieule  niatel niagou di dame ba 4 mois tope niarel niagou bi ak diourome 

diap 1 février wagni yaguayou green pass nekone diouromi wér nou tokhole ko ba diourombene wér  

 

 

Amna teureli si yéne khet yi nou khole

 

tambali 50 charte bou bess digualnala niagou yi 

 

” kép kou nek domou réwmi walou gua diogué fénene nieuw si réwmi dé say ate tolokh wala wéssou 50 ak guaye dougou si 50 ans fiba le 15 janvier gua bindoule si berébou fadioukaye yi niagou warnala 

 

 

Mane yone gua niagou gua ame cayitou asl dé  sa docteur bi saytou sa weergou yaram bindeule dé mou bayeko si ngite bi yor walou weergou yaram  fék niagou gua sars- cov 2 

 

Ligueye  katyi  sén ate toleneu si 50 ans diap le 15 février 2022 kou amoule green pass dinamel ni ligueye si ho batakhné  li dieume si sa berébou ligueye youkaye lou  nek meune la si fék 

 

 

Diap le 15 février  diekh 15 juin super green pass  lounou diklé  si berébou ligueye youkaye  ligueye ķayou kharagne si walou kham kham warnanou ame super green pass dakh nou meune del si berébou ligueye youkaye  

Green pass base

 

 

diap 20 janvier warna ngi

 

• watou kayi  letkayi wala li diokhé  tar sa yaram 

 

 diap 1er février green pass base dinanouko lathie si berép yi

 

    dougou si banque 

 

    dougou poste 

 

    dougou  berébou commercial  lou mel ni farmacie 

 

 

Super green pass 

 

 

Diap le 10 janvier dina war ngi di dougou si berép yi 

 

—  ngi yek si dem ak dikk yi

 

  —-  ngi dougou si bar restaurant   berébou fate likou dem ak  fekhlou kaye yi thiossane 

 

— ngi dougou finouye piscine  ak tanguale yaram  

 

ngi niakhou le 

 

soufeke niakhagou digua dieule le 1er dose le 31 janvier dakh gya ame green pass bou bakh  le 15 février 

 

soufeke niakhogo fi bale 1er février dotoule meune nék 

 

–  domeune yék si dem ak dikk yi 

 

— domeune dougou si bar ak restaurant 

 

— domeune dougou berébou fekhloukaye ak thiossane 

 

Ngi niakhogoule meunanou dougou berép yi diay li nite meute niak farmacie supermarché  sigarette wala li dieume si wala matériels keur 

 

 

dane si ngi gua khame topounou charte yi

 

Niakhou lounouye sakhou fiba 15 juillet  le 1er février 2022 dane yi dina tambali 100€ si kou niakhogoule dina nou ame ay yi saytou agence entrée   sén ligueye walou cartou fadioukaye ligueykayi bagna niakhoule dane tambali 600€ diap 1500 € yi gua khamé nolen ligey lo de defa no sen  waref dane 400€ diap 1000€ 

 1,129 Visite totali