ANI DIAFEDIAFÉ BENA NITE SI DIALGUATI WAREEFOU DOUMOU ADAMA LA

Share on facebook
Share on twitter
Share on linkedin
Share on telegram

SOUFÉKE GUISSGUA WALA  DOUNGUA BENE BOUNOUYE BOUNOUYE DIARIGNO  NEUNE KO DIMBALI 

    NEUNA WOTE  80029029

  DOU FAYE DARA  DÉ KENE DOUKOKHAME  24h

   FI SI REWMI ITALIE AMENA BÉRRABE YOUGUAKHANÉ NOUYE SAYTOU SOUFÉKE DOUNAGUE WALA GUISGUA NITE YOUNOUYE DIARIGNO BERRABE YI DINANOULA DIAPALÉ SI DEUKOU WAYE BOU KENE DOKHAME BIMBALE SI WALOU WEERGOU YARAM AK SI WALOU YONE SANÉKINE FI SI ITALIE SOULA NÉKHÉ DINANOULA  DOUGEULA SI BENE YONE BOUYE SAYTOU AK CHARTE YOUNE LAYE WAKH

MEUGUA DIOKO AK NITEYI SI YIBAAR DAKH KHAME BOU BAKH WALA LATHIE  DIMBAL BOU GUAW SI KEN DOUL KHAM

  SI BIIR WÉTOU THIAMOYE

  SOUFÉKE YAGUI DOUNDOU BENE SIYI NEUNEGUA 

    DIGUA DIOTE YIBAAR SI CHARTE YI WALA TAKHAOU SI SA WAREEF

  DIOTE  DIMBEUL WEERGOU YARAM AM

  DIOTE DIMBEUL BOUWEUR SILILAYE HARE 

   TOKE SI REWMI ITALIE DI TOPOTO SA LATHIE DANKH NOU HARE LA WALA BENENE WALOU CAYITE

  LATHIE  DAKH NEUNE GUA NIBI SA RÉW SI WALOU DIMBEUL BOSAKOU WALA kOULAYE TAKHAKHOU 

DAMA WOLOU NDJGUENE BIMA DIGUE ANDI SI REWMI ITALIE DAKH SAMA DOUDOU SOPÉKOU AK TOUKI BOU MÉTI BIMADATHIE LEGUI MAYE DIAYE SAMA BOP DAKH FAYEKO KHALISAME "
J.R., 22
TOUKI BOUMETI BOUMADATHIE SAMA BAYE NENAMAWEUNE DAMA KHARA NIEW SI REWMI ITALIE BAKH DIMBALI SAMA WAKEUR LÉGUI MAGUI LIGUEYE 10H PARE BEUS BEUS BOU NÉK SI SEMAINE BI DÉDOUMANOPALIKO MAGUI DEUK FI MAYE LIGUEYE SAMA BORYI MOGUI YOKOU DAKH SAMA TOUKIBI AK NITE KI MAOUTEULE LIGUEY FI SI REWMI ITALIE
M.H. 18
GUEMNALENE BIMAWATHIE SI REWMI OUTALENANOULA DOUNDOU BOUWEUR DIAMANO BI NAGUI FANANE SI TALIBI DI YALWANE KHALIS BI MAYOR DIOKE NITE BI MANDI SI REWMI
G.S., 20

Presidenza del Consiglio dei Ministri / Ministero dell’Interno / Unhcr