Faq – Yéksi fii thi Italie

Share on facebook
Share on twitter
Share on linkedin
Share on telegram

visa moy, keuyit bii ngha khamné kilifeu Consulayi gno koy diokhé ndakh nitki mana touki teu dou am bèn diafè diafè, si biir rèwou Schengen yi wala thi biir italie, gnonghi koy déf si Passport wala bénén keuyit boo khamné diarna yoon  




Gni mana lath visa moy, gninga khamné deukougnou thi réwou Schengen yi wala nit gninga-khamné amougnou réw teu deu-gno beugheu gneuw Italie ndakh:

  • sokla ay-wadour, kou wara-Fadiou 

           lidieunti-kat, koufi-am ndiabot,

           concours sport, invitation, sa lighéyou-bop

           wala nga-amfi lighéy, lou-dieum thi Tarkhia

           kou wara gnibi-si, koufi gneuw teu            beugheu-fé tok, kouy wout-si kham-kham, koufi wara diar-dial thi aèroport-yi, nga gneuw-fi vacance bou ande ak-ligéy, wala nga-fiy ligéye teu yalla takh




moy kinga-khamné kheus-na gneuw fii thi Italie teu amoul-visa kén mounou-ka déloo ghinaw bou féké dafa tol thi:

  • ndibeul International pour doun-fi
  • boodé khalè bou ama-goul fouki-at ak diouram-gnat (18 ans) wala mou nékon-fi ak ay wadioureum teu gnou ghénné wadiouryi réwmi
  • boudé diot-nga am ndimbeul International bou-am app thi lépe lou dieum thi walou domou-adama
  • wala ngay-diot ndimbeul ndakh ay diafé-diafè you doy-war
  • wala kou-eumbeu-dom, ak kou weusine ba-am diourom-béni wér yi-thi top

boo kheusé romb frontièrbi, teu gnou-khol sèy-keuyit gnou-défal-la timbre boo khamné amna  beus ak fi-nga-wara-dém

 

Moytou: boo wakhé loudoul deugeu, wala nga doikhé ay-keuyit you diaroul-yon, dinagnou-la-atté

thi-yon teu lingay-lath doko am




Queste FAQ sono parte del Vademecum “Benvenute e benvenuti in Italia” realizzato nell’ambito del progetto Before U Go

Ambassade d’Italie à Dakar

SÉNÉGAL Ambassade d’Italie à Dakar Ambassade compétente pour les citoyens rèsidant au SENEGAL, MALI, GUINEE BISSAU, GUINEE KONAKRY, CAPE VERTE ET GAMBIE Adresse: Rue Alpha

 869 Visite totali,  2 visite odierne

Continua a leggere »
PHP Code Snippets Powered By : XYZScripts.com