BATAKHAL SIWALOU TEUTHIE YENA BERRÉP YI

Share on facebook
Share on twitter
Share on linkedin
Share on telegram

CALABRIA

LOU DIEUME 23 OCTOBRE TÉRÉNANOU GUA DIOGUÉ FIGUA NÉK DEM FÉNENE SI BÉNENE GOKH SI REWMI SI WAKHTOU YI 24H 00 BA 5 H 00 BA BEUSS BI DI DÉLOUSI  AMENA NIOUNIOU MAY

 /  KEP KOUYE DEM DAFA WARA NEK SI WALOU LIGUEYE 

 / KEP KOUYE DEMDAFA WARA NEK TAMITE LOU AME SOLO LOUMOUNOULE KHAR WALA DIEUME SI WALOU WÉR

GUÉNE BI DAFAWARA AME FIRDEL BIGUAKHAME YAKOYE DIEULE SI [LINK]

FEPALA DIOGUÉ SI GOKH CALABRIA [LINK]

CAMPANIA

LOU DIEUME 23 OCTOBRE TÉRÉNANOU  GUA DIOGUÉ SI BENE DEUK BOU NDAW FI GUA DEUK DIEUME SI BENE DEUK BOU NDAW NEK SI CAMPANIA AMENA NIOUNIOU WAY

/ KÉP KOUGUAKHAMÉ  LIGUEY  GUADIEUME

/  KEP  KOUGUAKHAMÉ  SI WALOU DJABOOT LA

/  KEP KOUGUAKHAMÉ DAGUA AME LILA WAR SI WALOU DIAGUA LA DIEUM

/ KÉP KOUGUAKHAMÉ SI LOUMOUNEK MEUTE KHAR WALA DIEUME SI WALOU WÉRRGOU YARAM 

GUENE BI DAFAWARA AME FIRDEL BIGUA KHAMÉ YAKOYE DIEULE [LINK]

SOUFÉKE DAGUA AME DIAFEDIAFÉ NGIBISIL SISASSI

FEPALA DIOGUE SIGOKH CAMPANIA 

LAZIO

LOU DIEUME GOUDI 23 OCTOBRE TÉRÉNANOU GUA DIOGUÉ FÉNENE SI GOUDI WAKHTOU 24H 00 DIEUME 5H 00 SI BEUSS BISI TOP AMENANOU MAY

/ LIGUEY KAYE YI DIOGUÉ SÉN KEUR DI GOUDÉ BOUMOUDONE;

/ KÉP KOUGUAKHAMÉ SI LOUMOUNEK MEUTE KHAR WALA DIEUME SI WALOU WÉRRGOU YARAM 

GUÉNE BI  DAFAWARA AME FIRDEL BIGUA KHAMÉ YAKOYE DIEULE SI [LINK] 

FÉPALA DIOGUÉ SI GOKH LAZIO [ LINK]

 LOMBARDI

LOU DIEUME GOUDI 23 OCTOBRE TÉRÉNANOU GUA DIOGUÉ SI GOUDI WAKHTOU 23H 00 DIEUME 5H 00 SI BEUSS BISI TOP AMENANOU MAY

 / KEP KOUGUAKHAMÉ LIGUEY GUADIEUME 

/KÉP KOUGUAKHAMÉ SI LOUMOUNEK MEUTE KHAR WARA DIEUME SI WALOU WÉRRGOU YARAM 

GUÉNE BI DAFAWARA AME FIRDEL BIGUA KHAMÉ YAKOYE DIEULE SI [LINK]

SOUFÉKE DAGUA AME DIAFEDIAFÉ NGIBISIL SISASSI 

FÉPALA  DIOGUÉ SI GOKH LOMBARDI [LINK]

 

 698 Visite totali,  4 visite odierne

Asilo e immigrazione

FAQ – Dound fii thi Italie

Lan-moy permie de sejour? moy keuyit binga-khamné ngourou italie moo-koy diokhé ndakh dokha-ndém yiy-dound fii italie, teu keuyit-ghi meun-na-doon louy-yag, wala mou bagna-yag Kagne moo

 419 Visite totali,  40 visite odierne

Continua a leggere »