Charte yi am tambali 29 décembre bi wess dieum si yok green pass ak quarante  di nek sa bir keur 

Share on facebook
Share on twitter
Share on linkedin
Share on telegram

niogui dilene yeuguele né  

https ://www.jumamap . it/it/covid/ damele khole lou bess yi si charte fébbar bi 

  

 

Mou andakh charte feteyi  23 décembre ba 29 décembre amena yéne khétou dieufé dieume si fébbar bi covid-19 

 

sou 10 janvier 2o22 dioté sopékou dina ame dieume si green pass sopékou nék  ( ‘super green pass’)ak lou dieume si walou tok sa bir keur di quarante 

 

Lou bess lounou yok si super green pass 

green pass binou yok (soufeke matalgua sa niagou ak wér topassi) meungua top yéne yeugou yeugou yi 

 

   –  meungua dieule dem ak dikk  cogne yi ak gokh yi 

 

 – yéne berébou nopaloukayi ak fi di andi khalis 

 

– fete yi dieume si walou diné  

 

 –  fetou cogneyi gua me daguay andi sa marchandise 

 

  –  berép yi nit yi di dadié di wakhtane 

 

—  lou dieume si berébou lekk yi sibiti

 

  —  fi nouye fekhlo ak nienie you diogué béne réw -diaye nane wané tar

 

  –  piscine  berébou sangou ak sport mbolo ak defalsa sa kaname si fou bibekou;

– berébou thiossane berébou dimbal ak berébou foyi dé mo ibekou 

 

ligueye katyi meunanou dem ligueyi ak tampon binouye déf dé mouye firdéle amo fébbar bi  (24 h rek nanoukonagou 48h tampon bou gaw bi dieum si bakene bi )

yi diagui dara diou kawé gui université  meune nanou de diagui ak tampon bouye firdéle amo fébbar bi 

 

 

charte bou bess si green pass diap 1 février 2022

tambali 1 février 2o22 green pass vaccine dialane 9  ba  6 wér   lou mou néw niagou 3 dose  5 ba 4 wér  siniagou bou mate

 

 

Yéne batakhal si tok sa keur yi 

kéne nago toule top si keuryi nite you gua khamné lokou nanouak ngi am fébbar bi 

 

 

– ngi gua khamné  niagou nanou 2 dose diap 4 wér 

 

– ngi gua khamné niagou 3 dose nanouye khar

 

boulene fate tak mask ffp2  diekh fouki fane bigua nékek nite bou ame diagoro fébbar bi gua déf test bakene ak guébine bou gaw diouromi fane binla walé

 

 

mask

  takk mask si bédadi ak ngokh   you wékh zone blanche 

 

 

   –  takk mask ffp2 si berébou fohoukaye  de nityi difa dadié  boume fa diogué berébou theatre  ak berébou way ak cinéma terenanou nane ak lekk berébou younou teuthie dieume si way ak diongante si walou tagate yaram 

 

takk mask  ffp2 si bép dem ak dikk

 

 

khew khew fete ak discothèque 

 

diekhou 31 janvier 2022 terenanou bep khew khew dieume si walou fete ak fi nouye wayé   dadieulou si yéne  berép  teuthie berébou fethie  ak discothèque cogne

 

setti berébou fadioukaye ak rsa

meune dougou séti  berébou fadioukaye  residence  assistance  ak bene bir green pass bounou yok wala tampon bouye wané amo diangoro fébbar bi 

 2,175 Visite totali,  1 visite odierne

Ambassade d’Italie à Dakar

SÉNÉGAL Ambassade d’Italie à Dakar Ambassade compétente pour les citoyens rèsidant au SENEGAL, MALI, GUINEE BISSAU, GUINEE KONAKRY, CAPE VERTE ET GAMBIE Adresse: Rue Alpha

 1,499 Visite totali,  5 visite odierne

Continua a leggere »