Dénthie Dakh

Share on facebook
Share on twitter
Share on linkedin
Share on telegram

Dénthie dakh njaboot gui  nieup la war dé nek ndimbal de khale yi ndaw khaliss bou nouye diote banouye mague didap 21 ans 

 

Yok ndimbal  inps nokoye ndiékhal si sa am am dolé  ( isee) am yok ndimbal meunenanou bindou le 1er janvier 2o22 inps wala ngi yorbirou ligueye  yok ndimbal bi mogui diokol ak inps mars 2o22 

 

meune gua lathue yok ndimbal fi  30 juin 2022 de moutolo fi wér  ( mars  2o22)

 

Kane moneune lathie yok ndimbal 

 

 

Bobeugué lathie yok ndimbal lane guaye ame 

 

gua nék  wa réwmi wala rewou europe (wala njaboot) wala gua nék kou bokoule rewou europe dé guame cayite réwmi  ue ak gua yague lol si réwmi  wala sa caite nék  di ligueye  lou wessou 6 mois tamite cayite  ligueye bou yague si rewmi 6mois 

—   sa faye biguaye diote si réwmi 

—  wala gua def si réwmi loutolok 2ans  dé figuaye ligueye  amgua cayitou ligueye bou yague wala ligueye  bou wéssou 6 mois 

 

 

Li mégole yok ndimbal 

 

•  yok ndimbal nieup la war – bep khetou fayekou ameuna  si yone — topanté — yok wagnékou amam isee 

 

•  yok ndimbal meune guako lathie 120 jours si dioudou dom ak khalé bi matate 21 ans dom bou nek

 

•  khaleyi am 18ans ak yi 21 ans matoule ndakh yok ndimbal lew lane 

 

°  guay def école formation  professionnel wala gua ame diplome 

 

°  tambali ligueye def fayékou ate bounek 8 000 € 

 

°  sa ligueye  takhaw dé kheur ligueye 

 

°  ligueye de nieup zm si yone

 

•  sodefe lathie si ba wér  mars fi zk 60 bess di nala yeugeule

 

•  yok gui dina diar si iban wala yoksi keurgui reddito di cittadinanza 

 

•  yok gui bokoule dara ak reddito njaboot gui

 

NB   nouteguale si bi lathie tambale walele certification isee gua meuna diote yok propostion  bousa lathie andoule ak certification   isee inps linkaye diote dina niew siwalou reddito 

 

lou megoule yok ak yenene ndimbal 

 

diap fi mars 2o22 yok ndimbal dieume njaboot ak domyi

 

–  yok ndimbal  dieune si diote khale ( yok yaye souba)

yok ndimbal khale yi sogua dioudo ( yok liryi ) ak anf (yoké njaboot) nou bolesi khale yi ame lou wésou 21 ans

 

–  yok ndimbal nouro na ak reddito di cittadinanza wala yok khalé 

 

nb soufeke sa reddito di cittadinanza akyok ndimbal njaboot authentique nane koye dakh

 

 niata la tolok si yok ndimbal 

si lnk meugya calculer yok sk inps 

hppts ://servizi 2.inps .it/servizi/ assegno unicofiglio / simulatore 

 

diarigne yi am si yok ndimbal njaboot 

 

sou diote amoule brnf cayitou réwmi nou sopi si yok ndimbal dieume si page bi

 

nane na nouye dff bame lathie

 

def lathie diarna gua dougou sitou inps 

hppts ://servizi web2.inps.it passiweb/jsp/spid /login/spid .jsp?uri =https%3a%2f%2f servizi 2.inps .it%

 

wote le si numéro 803164 ( fixe  ) 06 164 164 ( sa téléphone) wsla yene caf inps nagou 

hppts ://www.inps .it / servizi=online /servizi =per =patronati/ informazioni / gli= enti- di – patonato

 

soufeke dego lak réwmi de gua sokla kou lako lak si sa kalama wotel  numéro verde  lathie asile ak réfugié  ( arci)  800 905 570 lycamobile  351 137 63 35 

assegno unico
Pidgin English
Bambara
Pular
Soninke
Asilo e immigrazione

NDIMBAL UKRAINE 

XIBAAR BOU AME SOLO KHÉTAYOU REW YI SI ADOUNA NAGOU NANE NDIMBALI SU KHÉKH BI AM  SI RÉW UKRAINE (55/2001) GOOR WALA NDJGUENE BOU DEUK

 872 Visite totali,  13 visite odierne

Continua a leggere »