DIOUROME 6 BOWORE KHAME SOUFÉKE DAGUA BEUGUE GUÉNE

Share on facebook
Share on twitter
Share on linkedin
Share on telegram
BEREP YOU JAUNE

SOUFÉKE DAGUA BEUGUE GUÉNE DEM AK LOUMOU MEUNE DONE WARGUA WANÉ FIRDÉLE ?
WAKHTOU 5H BA 22H DIAROULE FIRDÉ WAYÉ 22H BA 5 H FOK GUA AME FIRDÉ BOUYE WANÉ DAGUA WARA GUÉNE

MEINENA DÉME DIMBALI XARITE WALA MOK BOUSOKHLA DIAPALÉ ?
WAW SOUFÉKE LOUMEUTE NIAK WAYÉ DIGUENTÉ 22H BA 5H AME FIRDEL DINANKO SOLO

SOUFÉKE DAMA TAGO WALA TASS MEUNENA SÉTI SAMAY DÔME ?
WAW MEUNE GUA FÉKI SAY DOME WADIOUR NAGUA TÉLA GUÉNE YOBOULÉ SI BÉNENE GOKH AWÉNOUKO

MEUNENANOU DEM SI BÉRÉBOU DIAMOU YALLAH YI ?
WA KHANA LOUDIEUME 5H BA 22H

SOUMA DEUKE FENE DI LIGUEYE FENENE MEUNA DEM DI NIEUW ?
WAW

KOUNÉK FIGUA DEUK NAK MEUNE GUA NGIBISI ?
WAW

BÉRAP ORANGE

SOUFÉKE DAGUA BEUGUE GUÉNE DEM AK LOUMOU MEUNE DONE WARGUA WANÉ FIRDÉLE ?
WAKHTOU 5H BA 22H DIAROULE FIRDELE SA GUÉNE SIBIR NGOKH GUÉNE DIEUME BENENE GOKH WAKHTOU 22H BA 5H SIBIR FIGUA DEUK DAGUA WARA GUANAYO FIRDÉLE BOULAYE MAYE GUA GUÉNE DANOUKAYE HOUTÉ NGI YOR KARAGUÉ REWMI AK TALLI BI 

MEUNA DEM DIMBALI MOK WA XARITE BOUAME SOKHLA ?
SOUFÉKE LOUMEUTE NIAK DÉ KHAMO BANE WAKHTOU BIGUAYE NGISI

SOUFÉKE DAMA TAGO WALA TASS MEUNENA SÉTI SAMAY DÔME ?
WAW MEUNE GUA FÉKI SAY DOME WADIOUR NAGUA TÉLA GUÉNE YOBOULÉ SI BÉNENE GOKH AWÉNOUKO

MEUNENANOU DEM SI BÉRÉBOU DIAMOU YALLAH YI ?
WA WAYÉ 5H BA 22H SOUWESSO 22H BA 5H NAK TERENANOU KO DAY DIEUME SI WET BOU KHOQUE BI ROUGE

SOUMA DEUKE FENE DI LIGUEYE FENENE MEUNA DEM DI NIEUW ?
WALE BOBOUNAK GUENE FIRDÉLE BOUNEKE DANE LA SOKLA SI SA LIGUEY KATOU DAMEUNON LIGUEYE SA DEUK

KOUNÉK FIGUA DEUK NAK MEUNE GUA NGIBISI ?
WA MEUNEGUA NGIBISI BENE YONE TÉKLÉ DI GUÉNE DIAKLENANOUKO SOKLA LIGUEYOUKAYE DIAGUA WEERGOU YARAM WALA GUÉNE YOU SÉW SABIR GOKH ( DEM POSTE NDOUGUI BOUNEKE BEURIHOULE FIGUA DEUK

FI KHALÉ DI FOWÉ DI HIBEKOU

SOUFÉKE DAGUA BEUGUE GUÉNE DEM AK LOUMOU MEUNE DONE WARGUA WANÉ FIRDÉLE ?

WARA GUANAYO FIRDÉLE BOULAYE MAYE GUA GUÉNE DANOUKAYE HOUTÉ NGI YOR KARAGUÉ REWMI AK TALLI BI

MEUNA DEM DIMBALI MOK WA XARITE BOUAME SOKHLA ?
WA SOUFÉKE LOU MEUTE NIAKLA

SOUFÉKE DAMA TAGO WALA TASS MEUNENA SÉTI SAMAY DÔME ?
WAW MEUNE GUA FÉKI SAY DOME WADIOUR NAGUA TÉLA GUÉNE YOBOULÉ SI BÉNENE GOKH AWÉNOUKO

MEUNENANOU DEM SI BÉRÉBOU DIAMOU YALLAH YI ?
MEUNA DEM BÉREBOU DIAMOU YALLAH BI DIÉGUE SA KEUR DADOGUEME DIEUME SI KHAWA DIÉGUE FIGUA DEUK MOYETOU BOLO DE SORÉNTE DISTANCE BENE METRE MEUNEGUA DEM BERÉP SOUFÉKE DAFA AME LIGUEY BOUNE FAYE DÉF DIAPALÉ SI WALOU DINÉ DJI