FAQ- AY tiopite si wallu lago ak lois wu104:Lan mo bess ginaw atu 2026.

Ciopite bobu ci way lago bi niou adopte 1 ben fan ci zeru mars 2026,da fa nek ciopite bu khottt ci sistem bi italie de natte lago ak invalide civile

 

Decret Legislative 62/2024 mo ko adopte  niou indi model bu bess ci wall bobu ak ci  fasong bi gni koy sayto.       

 

seetlu wér-gu-yaram yi

 

seetlu ni nit ki amee laago

 

defar procès-verbal yi ci laago ak yoonu 104

 

Coppiteg yoon wi mi ngi bëgg yombalal sistem bi ngir mu gën a néew birokrasi, te du seet rekk jangoro walla xaalis wér-gu-yaram, waaye itam dina xool ni laago gi di ame ci dundug bes-bésu nit ki.

Déedéet, reform bi doxul lépp ci Italie ba leegi.

Lolu mingi tekki ne

● Ci province yi bokk ci expérimentation bi (xool point 8), ñi di defar demande yu bees yi dinañu topp sistem bu bees bu évaluation

Ci yeneen province yi, sistem bu tradisionel bi moo di kontine di jëfandikoo. (FAQ – Riconoscimento bu xaalis walla xaalu disabilità – JumaMap)

Jubluwaayu Gouvernement bi mooy yaatal modèle bu bees bi ci réew mi mépp tambali 1 janvier 2027.

Moo tax am solo nga xam ci ban province nga di déposer sa demande, ndaxte procédure yi man nañu wuute.

Réforme bi dañu ko tàmbalee ndank-ndank ci ay province yu bari ci Italie. Fi ci suuf mooy liste bu province yi ñuy boole léegi ci expérimentation bi :

Alessandria

Ancona

Arezzo

Ascoli Piceno

Asti

Bergamo

Bologna

Bolzano / Bozen

Brescia

Brindisi

Cagliari

Caltanissetta

Campobasso

Caserta

Catania

Catanzaro

Chieti

Como

Cosenza

Crotone

Cuneo

Firenze

Forlì-Cesena

Frosinone

Genova

Isernia

La Spezia

Lecce

Macerata

Mantova

Massa Carrara

Matera

Messina

Milano

Palermo

Pavia

Perugia

Piacenza

Pordenone

Potenza

Ravenna

Reggio Calabria

Rimini

Roma

Salerno

Sassari

Savona

Sondrio

Teramo

Terni

Torino

Treviso

Trieste

Udine

Venezia

Verona

Vibo Valentia

Vicenza

Su fekkee nga dëkk ci mbooloo yii, te nga war a jox ab laaj bu bees, sa xaalis ak sa dundug jafe-jafe dinañu ko natt ak système bu bees bi ñu tabax. Njariñu Gouvernement bi mooy yayale taqawaayu modèl bu bees bi ci réew mépp, li ñuy yeesal ngir mu nekk jëfandikoo ci 1 janvier 2027.

  1. Demal ci doctor bi
    Doctor bu base walla spécialiste bi moo di remplire certificat médical introductif bi te yónnee ko ci INPS (Istituto Nazionale Previdenza Sociale) ci système télématique bi. Doctor bi moo di yónnee lépp ci INPS. Yow daal war nga rek:
  • prendre rendez-vous ngir visite bi
  • indil dokument yi

 

Lii dafay tekki ne dossier bi dafay tàmbalee automatique, te INPS di tambali procédure bi ci boppam, kon: duñu soxlaati nga déposé beneen demande séparée gannaaw bi nga defee certficat médical bi ak procédure bu jëkk bi.

gannaaw bi nga amé certificat médical bi.

Ngir xam naka lañu man a gis “medico di base” ci Italie, xool FAQ – Il diritto alla salute in Italia – JumaMap.

  1. Demal ci rendez-vous bu valutazione bi 

Gannaaw bi procédure bi tàmbalee, INPS dina la woo ci yoon yii:
● SMS
● email
● bataaxal (ci ay yoon)
● walla ci sa espace personnel online ci site INPS

Lii lañu war di jox lañu ko ci jëkk:

Di jàppandi, nga di am:

  • waxtu (date) bu visite bi
    ● waxtu exact
    ● bérab bi walla naka lañu koy def (modalité bi)

Valutazione bi dafay am:

  • visite médicale (ni ci jëkk, waaye ak critères yu bees)
    ● ci ay yoon itam, evaluation basée ci documents yi

Evaluation bi dafay jàll ci:

  • wér gi (santé)

     

  • ndimbal gi nga man a def sa bopp (autonomia)

     

 

  • dund bi ci jamii ak liggéey (vie sociale ak professionnelle)

 

Loolu moo tax ñuy wax “Nattal bu bari wàll” (Valutazione Multidimensionale): koox bu ay xam-xamkat yu bari bokk ci dañuy seet du rekk jàngoro walla feebar bi nit ki am, waaye dañuy xool itam anam dundam, li mu bëgg ci dundam ak ay tegtal walla jafe-jafe yi mu mën a daje.

 

  1. Jot njàngat bi (walla saxal bi)

Bu wuutu pourcentage yu mag yi ñuy daan jëfandikoo ngir nattal invalidité, njàngat bi dafay tëral ab taxawaay ci ñenti level yu wuute ngir xam ni ndimbal ak yëngal yi nit ki soxla ñoo tollu fan. Ñi dañuy jëfandikoo ci ay sart yu àdduna si nangu, yu ñuy wax ICF (Classificazione Internazionale del Funzionamento).

 

  • Lieve (Yomb): Nit ki soxla ndimbal yu néew walla yu gàtt-gàtt. 
  • Medio (Diggante): Nit ki soxla ndimbal bu diggante, te war nañu ko dimbali ci yenn mbir yu bés bu nekk. 
  • Intensivo (Kawe bu baax): Mën-na ànd ak xaalis yu tar ci boppam ak ci mën-mënam ngir saytu boppam. 
  • Intensivo (Kawe lool): Nit ki amul doole ngir saytu boppam te soxla ay yar ak ndimbal yu sax ci bés bu nekk ak guddi. 

Nangu gi ne am nga xaalis bu ñu tudde disabilità

Attestation finale bi mooy tëral ndax yaa ngi bokk ci nit ñi am disabilità. Toppandoo ak tolluwaayu jafe-jafe bi ñu gis (yomb, diggante, kawe walla kawe lool), njàngat bi dafay dëggal sa sañ-sañ ngir jot:

  • ay ndimbal yu war, 
  • ay yëngu-yëngu yu ñu jagleel nit ñi am disabilità, 
  • ak yeneen sañ-sañ ak ndimbal yi yoon may ci xaalis boobu.

 

  • Njabootu ndimbal ci xaalis (benefici economici):
    Ñoom ñoo wuutu ay pension yi ak ay indennità yu mag yi ñu daan joxe ci lu weesu. Su nattal bu dekk bi dëggal ne nit ki am na disabilità bu am soxla ndimbal bu kawe (elevato) walla kawe lool (molto elevato), ci kaw loolu ay ndimbal ci xaalis dañuy tàmbalee dox ci boppam, te duñu laajaat jafe-jafe yu yeneen. Ci ñoom am na ay joxe yu mel ni assegno di assistenza walla indennità di accompagnamento.
  • Ndimbal ci impôts ak ci liggéey:
    Su njàngat bi nekkee jàppale (esito positif), dafa may sañ-sañ ngir jot ay ndigal ci liggéey (mel ni ndigal yu jëkk ci Liiwu 104), yàggal ci impôts (déduction fiscale) ngir jënd ay woto walla ndimbal yu tekniki, ak itam yombal yi ñu joxe ngir jënd ay alat yu mën a dimbali nit ki (ausili).

 

**Njàngat bi (esito) dafay jàppandi (génn boppam) ci sa Fascicolo Sanitario Elettronico (FSE Ab sistema digital bi ñu tudde Fascicolo Sanitario Elettronico (FSE) mooy njëlben bu diggante bi ñu def ngir dugal ak làq yépp sa doktoor ak sa xaalis yu wér-gu-yaram. Ci biir bi, am na yépp sa documents sanitar: njàngat, diagnosi, esami ak yeneen xibaar yu am solo ci sa wér-gu-yaram.

Mën nga ci dugg ci FSE bi jëfandikoo SPID walla Carta d’Identità Elettronica (CIE).

Ngir dugg ci sa Fascicolo Sanitario Elettronico, defal klik fii!

Dinga jot ab document digital (telematique) bu dëggal sa xaalis bu am solo ni nit ki am disabilità, di sa attestation bu benn (status unique) ni nit ki am jafe-jafe ci wér-gu-yaram.

 

Disabilità. Bii document mooy sa ndigal bu kenn gën a soxla ngir:

  1. Jot peyu ndimbal yu xaalis (sussidi economici) yu jóge ci INPS. 
  2. Jot yombal yi ci impôts yu jóge ci Agenzia delle Entrate. 

Tàmbali liggéeyu ndimbal social yi ci koom-koom (Comune) bu nga dëkk.

Le D.Lgs. 62/2024 mooy jublu ci:

  1. yàggal (walla wacc) jafe-jafe yi amoon ci jëfandikoo beneen dokiman: Verbale di Invalidità Civile ak Verbale di Disabilità.

 

  • Verbale di Invalidità Civile: dafay xool ndax sa doole liggéey (capacità lavorativa) wàññiku na, te ñu ko joxe ci pourcentage (ex. 74%, 100%).

Li mu soxlaa mooy jëfandikoo ngir am ndimbal fiinansiel (allocation, pension) walla ay facilité fiscaux.

 

  • Verbale di Disabilità (Legge 104/92): dafay riconosce te évaluer ay yaram, xel walla xel/fit (sensoriel) yu am jafe-jafe (invalidità civile, gumb, déggul…).

Li mu soxlaa mooy xool naka la sa xaalis, sa doole, ak sa jëfandikoo ci dund bi ñu ko di

sordocecità: ak yeneen jafe-jafe yu jëm ci jafe jafe ci gis ak dégg.

Itam dafay xool soxla yu am solo ci ndimbal (assistance) yi nit ki soxla, ci biir valutazione sociale (Legge 104/1992).

 

 

  1. Beesal (unificare) ñaaru verbali yi
    Ak réforme 62/2024, duñu amati ñaaru verbali yu sepparé (yu wuute), waaye am na beneen certificat bu benn bu dafay xam xaalis/état bu laggo bi. 

Dugal terminologie bu bees
Dekreet bi dafay wacc (abolir) baat yu mel ni “invalidità”, “handicap” walla

  1. “diversamente abile” ci yoon yi ak loi ordinaires yi mépp, te jëfandikoo leen ak terme bu bees bi: “Persona con disabilità”. 

 

 

Jàll ci “Progetto di Vita”
Bu evaluation bi wonee ndam (esito positif), administrasyon bi (Commune ak ASL) dinañu war, su nga ko laajee, tàmbali Progetto di Vita Individuale. 

Lii mooy plan bu ñu defal sa bopp, bu coordiné lépp lu jëm ci ndimbal yi nga soxla:
● ndimbal fiinansiel
● ndimbal social
● ndimbal sanitaire (wér gi)

Dafay jàpp sa dund gépp, te joxe la ndimbal yu lëkkale ak yuñu organise bu baax.

Ak réforme bi, ni ñuy nattalee disabilité bi dafa soppeeku.

Bala lii, nattal bi dañoo ko basé surtout ci:

  • pourcentage invalidité bi, 
  • maanaam pourcentage bu nit ki jot ngir feebaram walla handicapam. 

Pourcentage boobu, dañoo koy xayma ci ay tableaux:

  • bépp feebar walla problème santé amoon na pourcentage bu ñu ko jagleel.

Ak réforme bi, ni ñuy nattalee disabilité bi dafa soppeeku.

Bala lii, nattal bi dañoo ko basé surtout ci pourcentage invalidité bi, maanaam pourcentage bu nit ki jot ngir feebaram walla laggom.Pourcentage boobu, dañoo koy xayma ci ay tableaux:

  • bépp feebar walla problème santé amoon na pourcentage bu ñu ko jagleel

Waaw.

Ak model bu bees bi, nattal bi dafay xool barrières réelles yi ci dundug bés bu nekk.

Exemple:

  • nit ki mën na am autonomia bu baax, mën na am évaluazione bu wuute ak nit keneen 

même si ñoom ñaar am benn diagnostic, waaye keneen bi soxla ndimbal walla assistance bu gën a bari, mën na jot évaluazione bu gën a kawe walla bu wuute

Ci riforma bi, benn ci xalaat yu mag yi mooy jëfandikoo certification unique bu disabilité.

Ci jamono yu jëkk yi:

  • ● benn certificat walla procès-verbal mën na nekk bu jëfandikoo ngir ay droits yu bare
    ni: 
    • invalidité civile 
    • reconnaissance bu Loi 104 
    • ak yeneen ndimbal yu sosial walla yu jàppale 

Xalaas bi mooy: benn dokument bu yomb mën a jëfandikoo ci ay prestations yu bari, ngir yombal yoon wi te wàññi papier yu bari.

Soo xam ne, réfoorm bi dafa jàpp ne ñu war a yombal yoon wi ngir nit ñi am dofadiis (disabilité) ak seen kër:

  • ● ay visite yu ñu di faraa def yàgg-yàgg 
  • ● jamono ji ñuy xaar (temps d’attente) 
  • ● ay procédures administratives yu bari lool 

Xalaas bi mooy def yoon wi gën a yomb, gën a gënneek ak gën a yombal nit ñi ak seen famil.

Riforma bi du soppi automatiquement rekisit yi laaj ngir jot prestations yi.

Ci biir loolu:

  • ● duñu suufeel (abbassare) seuils sanitaires yi 
  • ● duñu soppi seuils économiques yi 

Maanaam rekisit yi jëm ci santé ak xaalis duñu soppi ko automatically ak riforma bi.

  • ● duñu garanti pourcentage yu gën a kawe. 

Waaye li soppeeku mooy méthode bu ñuy defe nattal bi, ndax sistem bi léegi dafay jéem a xool yépp aspect yi ci dundug nit ki.

Ngir déposé demande bu invalidité civile walla Loi 104, war nga:

Dajale document médicaux yu aggiornati ak certificats médicaux bu nu faraface

Yóbbu ci doktër bi:

● referti specialistici aggiornati
maanaam rapports médicaux yu spécialistes yu bees yi ak yu wóor.

  • Ay documents yi war nañu wér, leer, te mën a jàngu bu baax  war nañu jëfandikoo langue italienne
  • te war nañu xamle naka disabilité bi di laa tax a am jafe-jafe ci sa dund bés bu nekk (vita quotidiana)
  1. Wax bu leer ak doktër bi

War nga xamle bu baax:

  • jafe-jafe yi nga am ci sa dund bés bu nekk 
  • bu amee, limitazioni ci liggéey (ni nga mën a dox, liggéey walla jëfandikoo sa bopp) 
  • ak jafe-jafe ci bokk ak nit ñi (sociale), ni sa jëflante ak jamiirooy nit ñi 

Loolu dina tax doktër bi man a bind certificat bi bu wóor te matale.

Doktër bi (docteur de base walla spécialiste) war na bind certificat bi, kon dafa am solo lool nga xamle ko bu baax:

  • yépp feebar yi nga am (ba sax su amee lu bare) 
  • symptômes yu dëggu yi ngay ragal walla ngay jànkoonte ak ñoom 
  • jafe-jafe yu bés bu nekk yi, ni: 
    • dox (marcher), 
    • liggéey, 
    • man a doxal sa bopp (autonomie), ak yeneen.

Nota bene: bul tuuti sa jafe-jafe yi, ndax nattal bi dafay jëfandikoo itam ñoom.

  1. Kontroole rekisit administratifs yi

Bala nga door, war nga wóor ne:

  • am nga codice fiscale ak carte d’identité bu am validité 
  • da nga dëkk (résidente) ci Italia 
  • su fekkee mën nga, am SPID walla CIE (li dafa yombal nga topp sa dossier bi)
  1. Waajal ay documents yu am solo yeneen (extra)

Ci laaj bi, mën nga def:

  • certificats de travail (su fekkee ngay liggéey) 
  • documents scolaires (ngir xale yi / mineurs) 
  • rapports sociaux walla assistenza
    maanaam documents yu xamle sa xaalis, sa ndimbal walla sa situation sociale. 

Yëf yii am na solo col, ndax dafa jàppale ngir nattal bi di gën a complet (bu matale), ni réforme bi ko duggal.

 

Dëgg-dëgg, lii lañu ko dëggal ci riforma bi.

  • Ci ginaaw fase de exp, système bu bees bi dina appliku ci Italia yépp ci 1° janvier 2027.

Ci ay weer yu daw, dinañu xool ak seetlu lu bari, ci biir loolu:

  • maanaam jamono bi ñuy wóolu (woote) nit ki ngir mu dem ci visite médicale bi. 

maanaam ni réforme bi di war a soppi walla a jàppale jëfandikoo ndimbal yi ci xaalis ak services sociaux yi.

Lu tax am solo nga xam loolu?

Ci jamono jii ñu sukkandiku ci soppi bi, procédures yi mën nañu soppeeku ci région walla province bu nekk.

Kon, xam yeneen xibaar yi jëm ci réforme bi ak waajal sa documents bu baax mën na la jàppale yaw ak sa kër:

  • nga xam lu bees ci yoon yi 
  • nga xool sa dossier bi bu baax 
  • nga mën a def sa demande ci anam bu gën a xel mucc 

Loolu dina tax nga jàppale sa bopp ak sa famille ngir jëfandikoo sa droit yi ci yoon wu gën a wóor.

Dal 1° marzo 2026, ci ay province yi ci Italia, am na fase di sperimentazione bu jëfandikoo ngir soppi ni ñuy sàkku (demande) disabilité bi.

Dafa am solo lool nga jàpp xibaar bu bees yi ngir xam naka la procédure bi di soppeeku.

Scarica la brochure informativa dell’INPS!

NABILA è un Help Desk per cittadini migranti con disabilità e vulnerabilità che assicura assistenza socio legale, mediazione linguistica e orientamento ai servizi sul territorio nazionale.

Attraverso la linea telefonica gratuita 800 999 977, NABILA fornisce:

  • Ascolto e supporto da remoto
  • Orientamento ai servizi sul territorio grazie a JUMA MAP
  • Possibilità di richiedere appuntamenti in presenza (nella sede dell’Ufficio Immigrazione di ARCI Nazionale)
Questo progetto è finanziato dalla Presidenza del Consiglio dei ministri con la quota Irpef dell’otto per mille
 

Lan mooy JumaMap

JumaMap – Services for Refugees dafa benn kart bu ñu defar ngir may la saafara ngir gis foundé yi gën ci yàggu ci sa bopp.
Fii, man nga seet benn place bu nga naan, lekk, jang italek, amal ndimbal santé, ndimbal law, walla ndimbal psychologie, ak yeneen ay sarwiis yu bari yu amal ngir nit ñi di doxandéem ak nit ñi amul kër.

Platform bi am na 17 làkk.
Mën nga soppi làkk bi ci menu bi ci kaw. Ñu ngi am: Albane, Amarik, Arab, Bengali, Sinuwa, Dari, Farsi, Farãs, Angle, Pashtu, Punjabi, Rus, Somali, Espanyool, Tigrinya, Ukrèn, Urdu, ak Wolof.

Mën nga jàng JumaMap itam ci sa telefon portable: www.jumamap.it

Welcome Center

Su la bëgg ndimbal ci bopp-bopp, man ngaa ñëw ci Welcome Center:

Altine
10:00 – 14:00 — Büro d’orientation sociale

Talaata
10:00 – 14:00 — Büro psychologie (18–26 at)
14:00 – 17:00 — Büro ndimbal santé
14:00 – 18:00 — Büro orientation sociale
14:00 – 18:00 — Büro loi / ndimbal jëfandikookat

Àllarba
10:00 – 14:00 — Büro orientation sociale

Alxames
10:00 – 14:00 — Büro loi (18–26 at)
14:00 – 18:00 — Büro orientation sociale

Àjjuma
10:00 – 14:00 — Büro orientation sociale
16:30 – 19:30 — Büro loi

Ndimbal digital

Talaata 9:30 – 14:00
Àllarba 10:00 – 15:00
Alxames 9:30 – 16:30

Nimero bu bees ba ñi di bëgg asil ak refije

Ngir am xibaar ak ndimbal ci telefon, woo nimero bu bees bu Arci bu amal ngir ñiy bëgg asil ak ñi di refije:
800 905 570 (Itali)
+39 351 1376335 (WhatsApp, Lycamobile ak diiwaan yi des)

Dafa topp ci Altine ba Àjjuma, 9:30–17:00.
Am na auto-répondeur bu mel ni ay làkk yu bari, ak réseau bu ay mediatëör yu xam 35 làkk.
Mën ngaa itam bind ci: numeroverderifugiati@arci.it

Nimero bu bees ngir nit ñi doxandéem te am gëstu walla am ndigal yu wérul

NABILA benn sarwiis la buy may dégg, ndimbal ak orientation ngir nit ñi doxandéem ak refije yu am gëstu walla yi am yenn bant yi.
Mën nga woo 800 999 977 ak fanal.
Su la neexee wax bopp-bopp, mën ngaa jël rendez-vous ci bira Immigrazione bu Arci Nazionale:
Via dei Monti di Pietralata 16 – Rome.

Barab bu ñu déggal ndaw ak jeunes migrants

U-Report On The Move benn barab bu am aabbo la, fii mën nga am ndimbal loi, te mën nga wax ci sa xol, sa rey-rey ak li lay jàpp te lay nax.
Benn professionnelle dina la dégg te dina la wër ngir am ndimbal bu la gis.
Sarwiis bi daa dox ci Altine ba Àjjuma, 9:00–18:00.

Ngir ko jëfandikoo, dugalal benn message ci Facebook Messenger, ci platform U-Report On The Move.
Team bu psychologue yi dina tontu sa message te may la ndimbal bu tekkiu ci sa bopp.