FAQ – Richiesta di Protezione Internazionale

Share on facebook
Share on twitter
Share on linkedin
Share on telegram

[ITALIANO ]  [UCRAINO – український] [RUSSO – РУССО] [INGLESE – ENGLISH]

  • BEUSS BI GUA DOUGÉ RÉWMI ITALIE  TAKHADER YI SI YONE YI
  • SI YENE  DAMAL QUESTURA  WALA BERÉBOU IMMIGRATION (LINK CATOGORIA-JUMA) 

1) GUA AM YENNE -BI GUA GNEKE DEM QUESTURA GUA WAKH LANLE GUE BEUGUE DEF SOY LATHIE ASILE DIEULE BENE CAYITE GUA BINDE SA TOURAK SA SANTA BEUSS AK FO DIOUDO AK LÉNENE – WAKH MOU LER SI LATHIE ASILE 

 

BOUFÉKE QUESTURA DAFA TEUTHIE MEUNE GUA YONÉ EMAIL (YA KENE WALA AK BESS AVOCAT) GUA LATHIE BENE BEUSS GUA DÉF DEMANDE ASILE 

 

2) QUESTURA DINA LA BAYEK CEDOLINO CAYITE (AK BENE TIMBRE SIGNATURE) GUA AMNÉ DINA AME BEUSS ” DEF DEMANDE BI”

 

3( DÉF DEMANDE  ASILE BI – BINDE “C3” BEUSS BODEFE C3 MEUNGUA LATHIE CAYITE   RÉWMI PERMESSO SOGGIORNO “LATHIE ASILE” BOUGUAKHAMNE 6MOIS LAY AM NOUMEUNE KO  TOLONETI FI AK 2MOIS MEUNGUA SI LIGUEYE BEUSS BOU NIEUKE DIOKH 

 

DAF LENE NAK

 

SOUFEKE DAGUA NIEUW AK SA ( PASSEPORT) DAKAYE BAYI QUESTURA AK 4 PHOTOS 

PASSEPORT BI DINANOUKO YOR FI AK SÉN LIGUEYE 

BÉP CAYITE BOYOR DAMOU AM SOLO DAKOYE FÉ BAYI AK NIOM DAKH LI GUA BEUGUE ASILE  ( DIPLOME PHOTO ARTICLE BOUYE FIRDÉLE) SAY ATE FIGUA DIOGUÉ SA DEUK SA BEUGUE BEUGUE  SI LATHIE ASILE 

 

KHAM LÉNE 

 

SOKHLA NANOU FIGUA DEUK DAKH GAYE MEUNGUA KHAM AK DIOTE LIGUEYE BI FOUMOU TOLO SOUFEKE SA KEUR KHARITE GUA DEUK NA BINDE LOUKAYE FIRDÉLE 

SOUFEKE AMO FO DEUK YONE MAYNALA GUA DEUK SI KEUR NDINBAL YI FI YAK NOGUI TOPOTO CAYITE YI

SOUFEKE TAMITE AMO FO DEUK YONE MAYNALA GUA LATHUE NDIMBAL 

BO DAFÉ  LATHIE BI BA PARÉ QUESTURA DINA DIÉBEULE LEP COMMISSION TERRITORIALE “YOU KHARÉGNE SI NGOK “( BÉP NGOK SI ITALIE DINA AM BÉNE)

COMMISSION TERRITORIALE DINA GUESSTOU SI SAY BIR DAKH MEUNE  DIOGUÉ  KHALATEUME




Dopo aver fatto la domanda di asilo, la Questura trasmetterà I documenti alla “Commissione Territoriale” competente del territorio (di solito almeno una in ogni regione di Italia).

La Commissione Territoriale è l’ufficio dove vengono fatte le interviste ai richiedenti asilo, e che adotta la decisione sulla domanda di protezione internazionale.

YANE KHALATE LA COMMISSION  AM

  • NAGOU ARELA DONE LOU LOU RÉW NIEP WAKHTANE DE NAGOUKO DAKH MOUNO NGIBI SA REW NOUDIOKH LA CAYITOU 5 ANS  BOUNOUYE TOLONTI AK CAYITOU TOUKI

  • CAYITOU KHAROU TAMITE AMNA DE 5 ANS LAYE DONE DE NOUMEUKO TOLONTI 

  • CAYITOU SPÉCIALE  QUESTURA MOLAKOYE DIOKH 2ANS LAYE ANS MEUNGUA KO TOLONETI  SOPI KO LIGUEYE
  • CAYITOU FADIOU SOAMÈ  FÉBBAR  1ANS MEUNGUA TOLONETI SOPI CAYITOU LIGUEYE 

  • COMMISSION MOYE ARE CAYITOU BOTAYOU RÉW YI WALA SPÉCIALE

DEF LEN NAKE 

MEULENE WOWATE SOUFEKE CA HISTOIRE DOYOULENE DÉ DOUWAGNI DARA SILIGUA BEUGUE 

SOULAYE DEKLOU AMGUA WAREF:

  • SOUNE LAYE DÉGLOU MEUNGUA WAKH SI SA LAKK ( WALA MOUAME KUKA DEGUE BOUBAKH)
  • AK LOU COMMISSION KHAM SI INFORMATION ( DINA KO DETHIE DIEUME SISA DEUK)

  • GUA AME BENE AVOCAT BOLAYE TAKHAOU
  • SOAMÈ DIAFEDIAFÉ AK KI LAYE WAKHALE SI SA LAKK 

  • MEUNGUA NOPALIKU
  • MEUNANOU ARRÊTE  LATHIE YI SOUFEKE ( DAGUAAME DIAFEDIAFÉ WERGOU YARAM)
  • NOUKHOLATE LIGUA BINDA DAKH AMOULE LOUNOUYE KHOLATE

SI YONE LATHIE PROTECTION INTERNATIONAL DINA AME WÉR SOUFEKE YENE YI KÉNE  MEUNOULAKO WAKH SI YAGUAYE

KHAMLENE

AK LOUMEUNE DONE YAW MEUNGUA YORE SA CAYITE ASILE BIGUAYE LATHIE




SOUFEKE DANE LADIOKH “NÉGATIF ”  MEUGUA DÉF ” TOP ” DAM TRIBUNAL DINA THIOKH CAYITOU 6MOIS  TRIBUNAL (DINALADIAPÉ KOM WAYLAKHOU DAKH KHAROU WALA FÉBBAR YARAM AK SPÉCIALE) AMNA YÉNENE LATHIE YOU BESSDIEUME SI CASSATION  DINATAKH KENEU DOULAGUENE RÉWMI 

SOUFEKE AMO KHALISS DIEULE AVOCAT TAMITE  MEUNGUA WOTÉ “PATRICINO “DE DO FAYE DARA GOUR GUI MOY DUEULE LEP LISI WAR KHANA DAGYAYE SIGNÉ  SA CERTITUDE  REDDITO 




SOUFEKE AMO AVOCAT BO YOLOULE MEUNGUA DEM SI TRIBUNAL BOULEGEUNE DIEGUE MOUDIOKH LA LISTE AVOCAT WALA  GUAKHOLE ARCI BOULA DIÉGUE  AK GUA DEM SI Jumamap. It (https://www.jumamap.it/map/litemap.php?ser=leg )

MEUNGUA AME AVOCAT SISA KOGNE 

MEUGUA WOTE SI NUMÉRO VERDE SI WALOU AR WAREF DOMOU ADAM (800 905 570 L) ycamobile( 351 137 63 35) DAKH GUA MEUNA DIOTE ASSISTANCE 



Asilo e immigrazione

NDIMBAL UKRAINE 

XIBAAR BOU AME SOLO KHÉTAYOU REW YI SI ADOUNA NAGOU NANE NDIMBALI SU KHÉKH BI AM  SI RÉW UKRAINE (55/2001) GOOR WALA NDJGUENE BOU DEUK

 870 Visite totali,  11 visite odierne

Continua a leggere »
assegno unico
aiuti sociali

Dénthie Dakh

Dénthie dakh njaboot gui  nieup la war dé nek ndimbal de khale yi ndaw khaliss bou nouye diote banouye mague didap 21 ans    Yok

 1,489 Visite totali,  11 visite odierne

Continua a leggere »