NDIMBAL UKRAINE 

Share on facebook
Share on twitter
Share on linkedin
Share on telegram

XIBAAR BOU AME SOLO

KHÉTAYOU REW YI SI ADOUNA NAGOU NANE NDIMBALI SU KHÉKH BI AM  SI RÉW UKRAINE (55/2001)

GOOR WALA NDJGUENE BOU DEUK UKRAINE DE AM CAYITOU BI GUAKHAME  WA BOTAYOU RÉW ADOUNA LA YOR FOFOU SI UKRAINE AK SÉN NJABOOT DI NANOU TOLONETI  CAYITE GUI DE MEUNA NOU DEM SI YENE BERÉBOU YI 

–   ECOLE 

–  LIGUEYE

—  YOR  NDIMBAL 

— ARE SI WALOU SOCIAL

— ARE SI WALOU WÉRGOU YARAM 

KHAMALÉNE BOU BAKH

L’ITALIE  WARNA DIEUFE KHATIME GUI SAYOUNKO TEGUE SI YONE

AKLOU MEUNE TI KHÉW FATE LIKOU  LÉNE 

•  MEUNEGUA NÉK SI RÉWMI ITALIE DÉ DODEF BÉNE VISITE WALA CAYITE  ( BEUSSELE FI DAKH AM YÉNE  XIBAAR) 

• MEUNEGUA LATHIE DEUKOUWAYE SI YÉNE BERÉBOU NDIMBAL (CAS) BERÉBOU SYSTÈME NDIMBAL (SA) DE COMMIUNE( BEUSSELE FI DAKH AM YÉNE XIBAAR)

DAM LÉNE NDIMBAL UKRAINE 

 

Asilo e immigrazione

FAQ – Dound fii thi Italie

Lan-moy permie de sejour? moy keuyit binga-khamné ngourou italie moo-koy diokhé ndakh dokha-ndém yiy-dound fii italie, teu keuyit-ghi meun-na-doon louy-yag, wala mou bagna-yag Kagne moo

 1,667 Visite totali,  6 visite odierne

Continua a leggere »