XIBAR

FAQ – Dound fii thi Italie

Lan-moy permie de sejour? moy keuyit binga-khamné ngourou italie moo-koy diokhé ndakh dokha-ndém yiy-dound fii italie, teu keuyit-ghi meun-na-doon louy-yag, wala mou bagna-yag Kagne moo

 3,912 Visite totali,  2 visite odierne

Leggi Tutto »

FAQ – Doug fii thi Italie ndakh-lighéy

Naka lagnouy-dougué Italie nadkh-lighéy? numèro binga khamné moom la ngour-ghi wakh-nè dafa am app, teu wa bitim-rew yinga-khamné meun-nagno-gneuw fii thi Italie moy, koufi am-lighéy,

 3,869 Visite totali,  1 visite odierne

Leggi Tutto »
benvenuti Italia

Faq – Yéksi fii thi Italie

Lane moy visa? visa moy, keuyit bii ngha khamné kilifeu Consulayi gno koy diokhé ndakh nitki mana touki teu dou am bèn diafè diafè, si

 3,282 Visite totali,  1 visite odierne

Leggi Tutto »

NDIMBAL UKRAINE 

XIBAAR BOU AME SOLO KHÉTAYOU REW YI SI ADOUNA NAGOU NANE NDIMBALI SU KHÉKH BI AM  SI RÉW UKRAINE (55/2001) GOOR WALA NDJGUENE BOU DEUK

 1,882 Visite totali,  1 visite odierne

Leggi Tutto »

GRIOT

GRIOT || PODCAST MOUYE TONTOU SI BIIROU KHALÉ  WAYÉ LAKHOU WALA KHALÉ  LATHIE NDIMBAL SI REWMI  ITALIE BENE PODCAST U REPORT ON THE MOVE DIOUMTOUKAYE

 1,597 Visite totali,  1 visite odierne

Leggi Tutto »

Video

Podcast