WEUR NIAKHOU COVID-19
- TAMBALINA SI REW YI UE NIAKHOU BEUSSOU 27 DÉCEMBRE
- YANE NITE NANOU DIOKH PRIORITE SI NIAKHOU
- YI LIGUEYE SI WALOU WEERGOU YARAM WALA NDIMBEUL LIGUEY KATEYI
- NGI DEUK MAK YI WALA TOPOTO LENE (RSA)
- MAK YENE ATE SORI
BATAKHAL POUR NIEUP, NIAKHOU AR FEBBAR BI COVID-19 AMOULE FAYE
NIAKHOU COVID-19 AMOULE REWMI WALA KOUFI BOKOULE
- NIAKHOU COVID-19 KEL DOUKO NIAK KHALÉ BOU AME 16ANS
- NIKHOU COVID-19 DOULOU WARA NEK WAYÉ AMENA SOLO DAKH DI NA WAGNI NITE SI AME DIAGOROBI
- LÉGUI NIAKHOU NAGOUNANEKO SI EMA NIARI YONE SI SEMAINE NOU NIAKHLA AK KHETOU NIAKHOU
- NI DI LIGUEY SI WALOU FEBBAR BI COVID-19 DINANOU NIAKHOU TAMITE
YOKOU KHETOU NIAKHOU TAMBALI BÉP CATEGORIE ASKANE
AME SILOU LEER WALOU BEUSSOU NIAKHOU SI COVID-19 ( DINANOUKO DAF)
FONTE FAQ Sitò gouvernò